Def Patt Lyrics By Bass Thioung feat Samba Peuzzi

Kou tathiou woul
Niou dieul sa xol
Dougal si samba
Mou lay beyual

Hey
Kou tathiou woul
Niou dieul sa xol
Dougal si samba
Mou lay beyual

 

Samba li none yi beuyone
dalou la man nena waaw
Bass Thioung
Li none yi beugone dalou la
man nena wow
Beugal li ngay def
Defal li nga beugue
Borom xol bou nioul
Siigne la beugne you weex
Bagne ki yalla faral defe yeuki mer

Check Out:  Machinedrum – Kane Train Lyrics

 

Hey
Li none yi beugone dalou la